Nu se pretează? Nu contează! Puteți returna produsele în până la 30 de zile
Cu un voucher cadou nu veți da greș. În schimbul voucherului, destinatarul își poate alege orice din oferta noastră.
Până la 30 de zile pentru returnare
Waa so mënon delloo ay waxtu walla ay at ci ganaw?
Ak téeré bi, ma ngi lë woo ci ngë dellu ci dëmb ndax ngë xam sa ndono ni mu réyé.
Buur bu goor ak bu jigéen, njitt dëkk ya won ak jambaar yu goor ak yujigéen, defaral sa toggay te ngë gëstu(jàngat)
Jëfin ak kawtefu 4 kangam dëmb yi ci Afrik.
Ci jeexantal téeré bi, ab pàcc laa ñu la jagglel ngir ngë tekk
ay kuloor ci nitaal yi lolu dina tax ngë bokk ci léeb bi ci wetu jambaar yi.
Mbaa pare ngë ?
Bună ziua! Sunt Libroamiko, consilierul dumneavoastră de cărți.
Cu ce vă pot ajuta?